#RADIO-TV‎ > ‎walaf‎ > ‎Daawuda Géy‎ > ‎

Jeeg bu baax

publié le 23 sept. 2019 à 07:50 par Fall Papa Oumar


  1. Naka la ñuy sëye ?
  2. Awu leen ma naka la ñuy sëye ?
  3. Jeeg bu sëy te nara sëy dëgg
  4. Laaj leen ma nu muy sëye
  5. Fóotal goro, yakkal goro
  6. Waxtaan ak ub njëkke
  7. Waaye nag jeeg buy sëy
  8. Te yore fitu gaynde
  9. Bàyyi ko mu dëkk
  10. Yàgg fa ni daaw
  11. Sax fa ni céeboo
  12. Kenn du ko gërëm

Comments