OCCUPONS-L'ART-RUE-nuyoo

publié le 4 avr. 2016 à 23:18 par Fall Papa Oumar
XOOL JIS | JIS YËG | YËG JËF 

NUYOO


Yamal ci kuddu, ñu roof la ci gayet


Ndax nak , fok nu jàng nekk benn. Mebet u loolu du juddoo ci neen. Mbooloo u tund u Afirig ci wàllu caada du lu nuy nemmeeku, waaye lu nuy tabàq la. Bu weesoo wuute gi ci wàllu cadaa, te mu juddóo  ci wutéeg dëkkin yi, jiwu Afirig wu nekk benn a ngi ci xel yi, lëngoog bokk tund gi, bokk taariq gi ag yàgg ci ay xeeti wecco yune.



Comments