XAM DOOGA JËF
1- Lever la tête (SIGGI)... 2- Se mettre debout (TAXAW)... 3- Puis marcher (SEMEtt)...
De la réalisation de ces 3 phases dépend notre survie physique, intellectuelle, morale et idéologique

Ndax nak , fok nu jàng nekk benn. Mebet u loolu du juddoo ci neen. Mbooloo u tund u Afirig ci wàllu caada du lu nuy nemmeeku, waaye lu nuy tabàq la. Bu weesoo wuute gi ci wàllu cadaa, te mu juddóo ci wutéeg dëkkin yi, jiwu Afirig wu nekk benn a ngi ci xel yi, lëngoog bokk tund gi, bokk taariq gi ag yàgg ci ay xeeti wecco yune.
![]() ![]() | ![]() ![]() | ![]() ![]() |